Sengoor sukkandella Waaw ne sunu baay yi fi nekk ñoom duñ la gaaw a fàtte Waaw ne sunu yaay yi fi nekk ñoom duñ la gaaw a fàtte Ni Sengoor la Sëriñ Faalu Mbàkke ñaanaloon Ne Sengoor mii bu leen ko piisoo, xoole leen ko jàkk ñaari gët B Jogomaay lañuy woye baay ba Yaay Ñilaan Baaxumoo lañuy woye yaayamoo woowoo Lewopóol "Homme de science, homme de culture, académicien" bee Waaw foo cosaanoo (Afrig) Waaw foo cosaanoo, Senegaal Sengoor doo mëna ñaaw Doo mëna ñaaw, Jowaal Faajut nga juddoo Waaw foo cosaanoo (Afrig) Waaw foo cosaanoo, Senegaal Sengoor doo mëna ñaaw Doo mëna ñaaw, Jowaal Faajut nga juddoo Yow lañu duppee aydapooru Ndakaaru Njaay Waawaaw Abdu jaaraama, jaaraamaaa Waaw ne "Pincez tous vos koras Ne " hFrappez les balafons" Ku bind loolu, ku bind loolu Leopol Sedaar Sengoor a ko bind "C'est le tam-tam des arènes qui t'appelle ce soir" Ku bind loolu, ku bind loolu Leopol Sedaar Sengoor a ko bind Waaw foo cosaanoo (Afrig) Waaw foo cosaanoo, Senegaal Sengoor doo mëna ñaaw Doo mëna ñaaw Jiloor nga juddoo Garmi piir, garmi piir laay delloo njukkëloo man Garmi piir, garmi piir laay delloo njukkëloo man Garmi piir, garmi piir laay delloo njukkëloo man