Kishore Kumar Hits

Gun Mor - Power to the People lyrics

Artist: Gun Mor

album: Coups De Feu


Power to the people
Fuck ay nervi si ay pick up
Fuck gnom Macron gnilay djiteul
Fuck sa discours ak Kilay bindal
Fuck sa police bignou meunoul titeul
Sacrifier jeunesse bi beug gnou sikeul
Ame lepp bako fi di niani ndimbeul
Niou def la nditt keulé def la mbidane
Yafii seussone motax gnou pouss leu
Diox la pouvoir bi nieup ouf leu
Tek si ay atte rek nieup sour leu
2024 figua dieum si souf leu
Kou kass gua fekhel ko tok di niangual
Si sougn kanam rek Gua amé fouleu
Gnoune gnoy gni tax guay bour di boumi
So fogué ni ya mom rew mi Dioum ngeu
Xamal ni
Power
HeyPower to the people I say power
YowPower to the people I say power
Youxou fépp power to the people I say power
Because the power is the people
I say power
Gnoune gnoy guay degg son excellence Kone power
Yow the power is the people
I say power
Gnoune gnoy gni tax fo dem scort yi darr leu
Power
Because the power is the people
Loi bi gua beug violé boul fok ni dagn narra tok si xolé
Force restera au peuple oumpeulé woni ni eupognou dolé
Waxou niétélou mandat sa avenir fofou la barra tiolé
Say néwww deudjeulolene kou ame deudj fenene gua guéneu dioléko
Amo morale ni éthique
Yégalo sa yaram sougn metite
Li saye ndaw def mo raw sax délit
Perte gua carte bila war élire
Pourquoi autant de haine?
En vers nous xawma lougn la def
Inutilement tout le temps tu traines
Apart loubeul lenene loffi def guissouma loffi def
Power
Hey Power to the people I say power
Yow Power to the people I say power
Youxou fépp power to the people I say power
Because the power is the people
I say power
Gnoune gnoy guay degg son excellence Kone power
Yow the power is the people
I say power
Gnoune gnoy gni tax fo dem scort yi darr leu
Power
Because the power is the people
Lou loxo def loxokoy dindi
Kou carte fal cartakay folli
Kou fal sa bopp people bi jog sa kaw def si iow
Kou beug troisième mandat people bi jog sa kaw def si iow yeah

Поcмотреть все песни артиста

Other albums by the artist

Similar artists