Kishore Kumar Hits

Daara J Family - What's Up lyrics

Artist: Daara J Family

album: Yaamatele


Yo yeah
What's up what's up what's up
How life is treating you?
Noumou démé tchi sa side?
No togué la ley ladj?
Wakh ma lou né sa mind
Wakh ma lou né sa mind
Yow
What's up what's up what's up
Boul kallou tchi sa side
Yow wakh ma lou ley fadj
Li la metti nagn ko tadj
Wakh ma lou né sa mind
Dieul ma si souf wakh bi bougn ko adj
Ya ya yaw
Bi you bi you bi you bi bi
Ya ya yaw
Bi you bi you
Ndaw dafa diakhlé
Ndaw dafa soneu
Yeuy ay diplômes
Ba guekh ni nong
Beugueu tekki tekki bi
Lekka lekka bi dong
Beugueu feuss tchi télé bi
Def buzz di bombeu
Yeah yeah yeah
Yaw yaw yaw
Bi you bi you bi you bi bi
Yaw yaw yaw yaw yaw
Gnata barre 'a nek sama biir bop
(Yeah yeah)
Bou né yoor mic
Ama gouma job
(Yeah yeah)
Sokhla gueuneu barri
Bouné dima teup
Néma na gueuneu tok
Boul massa djouk
Boumou nga daw
Ya ko fi meun mbame bi nga kott
(Yeah yeah)
Leppeu sotti legui ma né dina meut
(Yeah yeah)
Sokhna ki dome fouma lene di fatt
Li la gueuneu beugueu ma ngui djeum mak
(Ouuuuu)
Bouma ken yakhal
Khol ma da ma diekh takk
Cons bi la doundou
Beugueu lou bess tak
Guisso sama cho bi
(Fok ma takk ko)
Li né sama mind bi yobou mère bi Makka
(Ouuuuuu)
Dama beugueu done star
Leumbé town bi
Li ma beugueu yeup yeup khadioul si sown bi
(Yep yep)
Manou ma wakh leep
Bouma keneu ladj (yo)
Mangui si yone bi (yeah)
What's up what's up what's up
How life is treating you?
Noumou démé tchi sa side?
No togué la ley ladj?
Wakh ma lou né sa mind
Wakh ma lou né sa mind
Yow
What's up what's up what's up
Boul kallou tchi sa side
Yow wakh ma lou ley fadj
Li la metti nagn ko tadj
Wakh ma lou né sa mind
Dieul ma si souf wakh bi bougn ko adj
Ya ya yaw
Bi you bi you bi you bi bi
Ya ya yaw
Bi you bi you
Keneu yetalou ma tchi laytayou wourrouss
Magga tchi keurou ndiabote
Té yagga bokeu mbouss
Sometimes galé dagnouy deupeu tchiin darra doufi souss
Yaga fandé dougou classe takhouma dieul bountou kouss
Mane dama gueum ni
Soon or later
Bou sobé Buur bi
Dina ko molé
Noon yi tcholé
May waral tiow li
May gadou tiabi bi
Di nongui nongui
Ah han
Am xam xamou zaïrou batiinou wexx ni kani
Yoré lotta money
Di begueul diam yi
Creer job yi
Diokh boy yi
Yokka PIB bi
Terral mere bi ak Pa bi
Ligueyal pays bi
Nekka Presi maybe
(Président?)
Et pourquoi pas?
(Président?)
Tout est possible
(Des possibilités il y'en a)
Et pourquoi pas?
Ouwouuuu
Yaw yaw yaw
What's up what's up what's up
How life is treating you?
Noumou démé tchi sa side?
No togué la ley ladj?
Wakh ma lou né sa mind
Wakh ma lou né sa mind
Yow
What's up what's up what's up
Boul kallou tchi sa side
Yow wakh ma lou ley fadj
Li la metti nagn ko tadj
Wakh ma lou né sa mind
Dieul ma si souf wakh bi bougn ko adj
Ya ya yaw
Bi you bi you bi you bi bi
Ya ya yaw
Bi you bi you

Поcмотреть все песни артиста

Other albums by the artist

Similar artists