Kishore Kumar Hits

Daara J Family - Xeet lyrics

Artist: Daara J Family

album: Foundation

Ki guewel la Ki guer Ki mbalamañsa la
Lolou dh amoul sens
Ki la gueune fouf'fa nga sango souf si ni selaw
Sauralé mirass
Nopilen na thiowli dakk wayy
Yalla khamna gars yi fi gueune nei boulene diayou
Irilene high class yi thii aldiana you noyy yi
Oubilene place yi ci khol yi ndakh niou noyyi

Ndawsi dafma ji mbëguel
Ma yewou souba tél
Outi dji keureum
Setti ay wayjoureum
Bamalene fa fekké
Dieulenafa mbettel
Dama yeksi diko niane si
Niounema douthi dale
Nioune yakh bou reuy laniouy langal
Kou touti doufi lal
Sounou dioudou mo gueune sen boss
Sounou bosseu gueuneu diss sen boss
Do fi soss
No no
Sounou dioudou mo gueune sen boss
Sounou bosseu gueuneu diss sen boss
Do fi soss
No no
Fogone nani gni gueune thii nioune moy gni am tei ragal yalla
Ki guewel la Ki guer Ki mbalamañsa la
Lolou dh amoul sens
Ki la gueune fouf'fa nga sango souf si ni selaw
Sauralé mirass
Nopilen na thiowli dakk wayy
Yalla khamna gars yi fi gueune nei boulene diayou
Irilene high class yi thii aldiana you noyy yi
Oubilene place yi ci khol yi ndakh niou noyyi
Les peuls et les wolofs c'est la même mifa
Chrétien ou musulman c'est la même mifa
On est tous les mêmes
Devant le Tout Puissant
Yeah yeah
Dama yagg doundou bi love
Ouais tour yi dagnma daw
Dama meusseu nop beu dof
Beug nite beu Armston
Dema dema dema dem ba diekh
Gueumone ni beuSs deiy nekh
Sentou bossam alkharyi
Tchei ptchei do meusseu degg wayy bi
Diokhena sakh groupe sanguin
Koula diour
Fo nampé
Bane xeet
Bane ethnie
Bangkal sa may bou ndieuk moy mbeth bii
Ki guewel la Ki guer Ki mbalamañsa la
Lolou dh amoul sens
Ki la gueune fouf'fa nga sango souf si ni selaw
Sauralé mirass
Nopilen na thiowli dakk wayy
Yalla khamna gars yi fi gueune nei boulene diayou
Irilene high class yi thii aldiana you noyy yi
Ki guewel la Ki guer Ki mbalamañsa la
Lolou dh amoul sens
Ki la gueune fouf'fa nga sango souf si ni selaw
Sauralé mirass
Nopilen na thiowli dakk wayy
Yalla khamna gars yi fi gueune nei boulene diayou
Irilene high class yi thii aldiana you noyy yi
Douma andak domou diw ndakh man douma sen mass
Douma andak domou diw ndakh man douma sen classe
Khebaaté gui souniou bir moy thiow li thi diaw dji
Niar niou beugueunté mayelen niou seuy
Beuguel amoul couleur tei dou askanoo
Té kouniou kagn sa khol doto nekk nite
Waydjour boulen niou khadialé di yobbou sounou fite
Boulen niou khadiaalé
Yaw yaw la nopp
Man ngueu nopp
Lolou la defone sa bop
Yaw yaw la nopp
Man ngueu nopp
Legui la top sey waw
Ki guewel la Ki guer Ki mbalamañsa la
Lolou dh amoul sens
Ki la gueune fouf'fa nga sango souf si ni selaw
Sauralé mirass

Поcмотреть все песни артиста

Other albums by the artist

Similar artists