Kishore Kumar Hits

Viviane Chidid - NO STRESS - Live lyrics

Artist: Viviane Chidid

album: Anniversaire "Les 22ans du Jolof Band" (Live)

No no bougnou nangou niou niou tek stress
No no bougnou nangou niou niou tek stress
No no bougnou nangou niou niou tek stress
Sougnou khol di fess gnom niou diok deff
Fess
No no douma nangou gua mey tek stress
Douma nangou gua mey tek stress
Ma bagn douma ko nangou no stress
Sama khol di fess yaw gua diok deff fess
Mane dimbalima wakh dji barina
Mane rekk thi khalei namouma dara
Mane dimbali ma wakh dji barina
Mane rekk thi khalei namouma dara
Dangua fateni amna 10 ans lou tax gua dieul ma beugeu ma deff sa fowoukay
Yombeuleul na la sa visa
Wow yeeey
Demal loula nekh way
Beugeu lang ak ki
Beugeu lang ak ké
Beugeu lang ak samay kharit mané nay dieundey
Degueuna nioune febar la
Wow yeeey
Defal loula nekh way
No no douma nangou gua may tek stress
Douma nangou fils gua mey tek stress ma begn douma ko nangou no stress
Sama khol di fess yow gua diok deff fess
Mane dimbali ma wakh dji barina mane rek thi khalei namouma dara
Mane dimbali ma wakh dji barina mane rek thi khalei namouma dara
Goor goula tek deal lundi ba dimanche noboula kouma beugeu tardel beugeu ma fowé ma romboula
Goor goula tek deal lundi ba dimanche noboula kouma beugeu tardel beugeu ma fowé ma romboula
Li safatouma sama mettitou khol diekhna li yeungeulou ma ndakhte mane niakouma fayda
Li safoutouma tegou thi temps deff bamlu bakh diotna te yow mi khamgua soma noboul
Sa morom nob ma
No no bougnou nangou niou niou tek stress
No no bougnou nangou niou niou tek stress
Sougnou khol di fess gnom niou diok deff
Fess
No no douma nangou gua mey tek stress
No no douma nangou gua mey tek stress
Douma nangou gua mey tek stress
Ma bagn douma ko nangou no stress
Sama khol di fess yaw gua diok deff fess
Mane dimbalima wakh dji barina
Mane rekk thi khalei namouma dara
Mane dimbali ma wakh dji barina
Mane rekk thi khalei namouma dara
Goor goula tek deal lundi ba dimanche noboula kouma beugeu tardel beugeu ma fowé ma romboula
Goor goula tek deal lundi ba dimanche noboula kouma beugeu tardel beugeu ma fowé ma romboula

Поcмотреть все песни артиста

Other albums by the artist

Similar artists