Kishore Kumar Hits

Viviane Chidid - YEUK YEUK - Live lyrics

Artist: Viviane Chidid

album: Anniversaire "Les 22ans du Jolof Band" (Live)


Khalé bi, sama khol ya si né
Té soumala guissoul
Yeah yeah yeah
Té soumala guissoul
Douma agne douma rér
Diarabi na la lér
Té soumala guissoul
No no no
Té soumala guissoul
Ooh wouh! wouh!
Oooh! Yes yes yes
Rèwaantoul beuri caprice,Beuggue na
Dèfal li si sa khèl (si sa khél)
Cheri lo beuggoul,maan mi beuggou ma
Khalé bi kèn dou yaw
Yeah yeah
Yobouma foula nékh
Maan gnamé na
Sucrée salée na
S'il te plait bae, yokkou ko
Ma tay noobe la
Louma si goobé, gar ko
Ouh lala la laa
Lou may doundou ak moom
Nékh ba mélni lém
Cheri, sama love
Soumala guissoul, wèét na
Yeah hi
Khalé bi, sama khol ya si né
Té soumala guissoul
Yeah yeah yeah
Té soumala guissoul
Douma agne douma rér
Diarabi na la lér
Té soumala guissoul
No no no
Té soumala guissoul
Ooh wouh! wouh!
Ohh! Yes yes yes
My baby, kèn safouko
Oh! No no no
Beuggoul li métti sama khol
Oh! No no no
Dou takhawalou, dèm founè
No! no! no! nooo yeah!
Mbeuguél bou doon drogue, overdose na
Moom lay use maan
Khalé bi lé, sick na yeah!
S'il te plait bae, yokkou ko
Ma tay noobe la yeah!
Louma si goobé, gar ko
Ouh lala la laa
Ooh! Diègué ma, diégué ma baby
Aïe aïe yaye! yaye!
Yaw cheri sam love
Soumala guissoul dof na
Yeah! Hi
Khalé bi, sama khol ya si né
Té soumala guissoul
Yeah!
Lou nék sa khél, wakh ma
Lo beug ma défal la?
Tay malay téral, nèkhal la
Baby ma ngi dolé té sokhor na
Li ngay déf, sama khol
Diko nékhél, maag koy doundou tout le temps.
Ma mélni kou nék aldiana
Dama la koy délo tay
Yeuk yeuk le
Mani mbegguél ni la
Ana Clara contaane ngue
Ndakh toro gueye diantal le
Té bo oubbé khol bi yaw ya fa né
Noumouil déf sa khol bi
Di koy nékhél nga koy doundou toul temps
Nga mélni kou nék aldiana
Da nga ka koy délo ndakh deug le
Yeuk yeuk yeuk yeuk yeuk yeuk yeuk yeuk
Mani mbeuguél ni la,Lo beug ma défal la
Tay ma lay yétal teureul le
Maan khaam na ni
Yeuk yeuk le
Li ngay déf, sama khol
Diko nékhél, ma koy doundou tout le temps.
Ma mélni kou nék aldiana
Dama la koy délo tay
Yeuk yeuk le

Поcмотреть все песни артиста

Other albums by the artist

Similar artists