Kishore Kumar Hits

Adiouza - Bus bi lyrics

Artist: Adiouza

album: Bus bi


Wadji souma koye khole ak nimou mel (ahhh)
N bi nè thie nekh!
Oubi bounte bus bi doug sama khol,
Li mom dou nèn.
Mou guèstou kholma cila khamni dou khèmém.maye niami niami
Koula djib wagni yaye dodane.
Bus bègui daw tè rombe na sama arrêt!!
Badou terminus lama dieumééé!!!
Guala dakar fo dém dik.
(Refrain)...
Fess gua del ci mane tè khawma yaw la kane!
Khol bi nane ma tè gua dem dikal khol baham...
Fess gua del ci mane tè khawma yaw la kane!
Khel bi nane ma togual boul dem djiguèn dou yomb...

Поcмотреть все песни артиста

Other albums by the artist

Similar artists