Kishore Kumar Hits

One Lyrical - Yaay lyrics

Artist: One Lyrical

album: Lune de miel


Deff Music
Gueudj nala guiss
(Namone nala)
Namone nala (Namone nala)
Yalla leu xiir (tchi mane)
Tchi mane xamone nako (xamone nako)
Yeuk nako
(Yaay boye kaay dieul ma balla ma démé)
(Yaay boye kaay dieul ma balla ma démé)
Yaay boye dadane mouñ
Ba domam teeral ko kaaw souf
Baay tam dadane mouñ
Bou xoolam seedé nga done buur
Bo amé defal tout
Sa family beegal ko moy tout
Dieundeul meew ak sukeur
Tiep ak diiwline
Ba beuss bougne ley soul
Mindeff takhoul (Mindeff takhoul)
Xaliss takhoul
Leess waxul
Niit dey wakh loumou defful
Yafuss waroul
Borom kaaraw bou gnoul
Nieup ame negne bideew
Fi ak dewuñu du reer
Kou ley seddeu
Tchi gaalu xatch
Boul ko begne
Mais nak boumou fa fekka sa lokho
Ligueyou ndeye
Agnou dome
Ligueyou ndeye
Agnou dome
Gueudj nala guiss
(Namone nala)
Namone nala (Namone nala) (yaay boyo)
Yalla leu xiir (tchi mane)
Tchi mane xamone nako (xamone nako)
Yeuk nako
(Yaay boye kaay dieul ma balla ma démé)
(Yaay boye kaay dieul ma balla ma démé)
Sama yaay yaay yaay
Bamouy nietti yone
Tek tchi baay boye
Loloy ndami dome
Adjana ngui sey souffou taanka
Wayé barké baay
Yaay boul diakhlé
Douma meusseu bayi
Ni maley namé doum si meusseu tayi
Deuké daaw yow meussoulo bayi
Dima teek tchi yone, yow ya tchi aye
Jiigen djou meune goor
Ligueye nga sama keur baay
Yiir ma, yaar ma, yee ma
Diom foula ak feyda
Xaam sa boppa yoxla
Diougal ligueye job la
Daanu diougate life la
Yaye sama galatch, yow la
Yow la
Yow la
Gueudj nala guiss
(Namone nala)
Namone nala (Namone nala) (yaay boyo)
Yalla leu xiir (tchi mane)
Tchi mane xamone nako (xamone nako)
Yeuk nako
(Yaay boye kaay dieul ma balla ma démé)
(Yaay boye kaay dieul ma balla ma démé)
Yaay boye kaay dieul ma balla ma dém
Yaay boye kaay dieul ma balla ma dém

Поcмотреть все песни артиста

Other albums by the artist

Similar artists