Santt naan Si seutoup sunu Mame Balla mi Mbacké baalla ya gnou may ndam gnou djioullit Mama daan Mbacké thi kholl yi lagn ma yonni Day def thi ngueumeul ak Alquraan nou kaarim Amna lool, kham né si mom rek la yam Day aar euleuk ba kénn Dotou ko aam, ziaaré Mbectem Yallah Ngak yonent bi Yaako diaar malakoy wakh cheikhoul khaadimi Footaal nganou sunu kholl yi bilahi Kén Nga yaay guén góor Cheikh Bamba taan yén bi Bamou oyof si gnounn Konn santt gnel neu bépp taalibé Mouride sadikkh (Dieurdieuf Serigne Bamba amngaa dieurdieuf) (Diadieuf Serigne Bamba amngaa diadieuf) Bamba diayoul nguoram deureum yakoul dara Toukem ba Ndakaru louné la dathie takhoul mou saalitt (Dieurdieuf Serigne Bamba amngaa dieurdieuf) (Diadieuf Serigne Bamba amngaa diadieuf) Yaagnou daan Fadial té fougn la meusseu wo ngani gnou naam Sa dem bi takhna tey Bagnou reuthie si ndiaam Yaagnou Goréel ya beuri ndieurign naam Do moroom ya daan Toubab ba tek thia kénal sa boroom Yaar Na lokhom té diott gnako yabaloon thia mom Yaagnou Goréel kenn dotoul ni mom Mo dem ba Congo, mom rekk Dongou Yorouli ndongo alquraan la langoo Cheikhoul khaadimi yay sauwé diaam gni Mbectem Mouride yi Anh siigil Nga Lislaam sagaal Nga dinée Takhoul Nga baakou diaarna té wékou Kénaal Nga Raaba Roynga yonent ba Amngaa diaramaa Mbectem Yallah Ngak yonent bi Yaako diaar malakoy wakh cheikhoul khaadimi Footaal nganou sunu kholl yi bilahi Kén Nga yaay guén góor Yaa ligeey ba am sa ngueureumeul borom Ba Loko niaan mouné waaw Mbacké niaanal tawfekh ak taysir Amiiiiine yaa rabbi Guiss nala weerou waay mann akhmadou Ngamay Fadial sa yërmàndé Raamb diaam gnii doolé biti ak biir Cheikh Bamba rek si khool lenénn dathia khadioul Amatougnou saago Si mom Mbecté maa Ngui fougnou tollou diko sentir Kunfayakoun leu modi Gallass bayou Mbène borom Ndindi Moy def di dindi Louko saff thi diaam gni Leepi khaadim Rassoul Moy yërmàndé gawonn si Serigne Saliou Mbacké mignou daan wakh Beugueutouma rééro ak yénn souma djito Dina wagnékou dieulsi watt leen Deletba wathiedia bil Mountakha wa kawni bin Ndakaru Mo yoorr mbeur meu waar thia doon Serigne Bassirou Kooku thieurou Porokhane leu Boudoul wonn mom dagnougnouy moom Djirim djioyatougnou Baye yaay sen Maame Khadfaad Kaabla gueum nagnou loolou Waa naf Ouh djiaahi Baayi wognou Bobou baa legui Ndakh yaa gnou waan Al Mountakha Mbectem Mouride yi Mann sa Guinaw demb la wonn Yangui fi ba legui Ay Mbacké yaay Guén góor