Mbegte la yoon bi yoonu mbegtee la Muriid aljana lay dundu Bamba Ia joie Mbegte la yoon wi mbegteem kesee la ♪ Muriid aljana lay dundu Bamba Ia joie Keeman la gu Iàmbo yërmànde Buñu maasee kenal ko rek xeewël yi sawaan Mbegte la yoon wi mbegteem kesee la Muriid aljana lay dundu Bamba Ia joie Jalaal ja boole ko ak Jamaal ja Mo ñu may mbegte muñuy sàggoo fa Tuuba Mbegte la yoon wi mbegteem kessnee la
Muriid aljana lay dundu Bamba Ia joie Bamba ligeeyal Ràbbana ba tax malāka yëp na
Ki du nit rek xana ndax kàt may am yi ëpp na Suñ
Ko nàŋngoo te japp ko luñu yootu mu xëccal ñu ko
Buñko xamul umpale ko lumu ñu jox ñu yakkë ko
Nañu jeemë tópp ndigal am te jeemë soobu ciy mbir am Jeemë sàkku ngërëm am ba am ko ndax lepp di ndam A sa yoon bi amul tànk ginaw, Seex Bamba ma yërëm sa noon yi (Bamba Jërëjëf) ♪ Mbegte rek lay àndal, Reetan te duma ko tey anaa muriidu(A)llāhi (Seex Bamba Jërëjëf) ♪ Bamba yaay mbër mi borom Jàk ay geej gi ♪ Yaa weetal Ya(A)llah fa mayombe firnde yaangi wir-wir ♪ Suñu mbër mi mo daan tubaab yi ♪ Túb lo ceeddo saver jaam ñi xasiidam yaa ngay riir ♪ Ah mbeg mi ne suñu xol yi di feeñ ci kanam yi Def nañ ci Bamba te doo tuñu weet Yaakari jaam yi ♪ Kon fu waay nek santal ñu Xadiimi ♪ Borom màggal gee ñu dóggal buumu jaam yi
Te lu waay am tëyeel ñun doyloo nañ ♪ Goor ga demoon geej mom Borom Tuuba Xeewël am yi daj na feepp ♪ Ñëpp ngi naan Bamba feepp, Bamba everywhere (Jërëjëf) ♪ Doylo ak woolu laa am ci yaw yaa gën a gaaw ci màn ♪ Doy nga sëkk làkkuwaay (Jërëjëf) ♪ Weetal nga rabbanaa ba mu joxla Kun fa Yakuun ♪ Doy nga sëkk weeruwaay (Jërëjëf) ♪ La matoon a wax Seex Ibra jëf nako
Des na jëfee ndigal defar suñy jiiko ♪ Wajxal xuloobanaa la Bamba wax ♪ Alaa tawajjuddi kon nañ ci sax
Ñu nekk ci rek te ànd ak tegin ♪ Wax ju ànd ak dal la waaye day làj deggin ♪ Ceerno Borom Daaru jaraw làkk
Bu du toon ak yaw ñun duñ nu sàkkë
Day gën a neex di ànd ak yàr ak tegin ♪ Muriid dëgg day rafetal jëfin