Kishore Kumar Hits

Omg Oumy Gueye - Lu Ci Sa Yoon lyrics

Artist: Omg Oumy Gueye

album: Melokaan


Sama telephone sa yoon nékouthi
Noumako amé sa yoon nékouthi
Sama sagnsé sa yoon nékouthi
Deug deug sa yoon nekouthi
Sama diouni bi sa yoon nékouthi
Foumou dioughé sa yoon nékouthi
Yoor sa lamigne tak radio yi
Manila hey louthiy sa yoon
Hey louthiy sa yoon, louthiy sa yoon
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey Lu ci sa yoon
Fougne la fek yangui togué nitt
Sa guémingne na yarakh ni car rapide
Niémé yalla tek thi degueur fiite
Amo dianou biir lo yeuk fok mou siw
Khama touma noumou démé ni
Town bi legui dafa teureudi
Facebook snapchat Twitter wakh dji yématoul si lamigne gni
Mytho mytho mytho mytho
Gawa sopi djiko Yaw nieup nga kharitol
Bene deugouwou thi
Deuké waté serigne yeup
Diékheul téré yeup
Lingay wakh yeup no dara amouthi
Deuké saupp dara amouthi
Yangui soss nass nothi fass fethi ndéké yo dara amouthi
Dieuleul sa temps ténga def bine bine
Tass katou digueune tenga ya gueuneu graw sémingne
Ma wola nga record
Message nga capturer
Vocal nga transférer
Statut nga vu yakamti partager
Sama telephone sa yoon nékouthi
Noumako amé sa yoon nékouthi
Sama sagnsé sa yoon nékouthi
Deug deug sa yoon nekouthi
Sama diouni bi sa yoon nékouthi
Foumou dioughé sa yoon nékouthi
Yoor sa lamigne tak radio yi
Manila hey louthiy sa yoon, hey Louthiy sa yoon louthiy sa yoon
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey Lu ci sa yoon
Lo kham wakhé
Weur di nakhé
Deuké di loré
Amo ngor khamoulo lane moy goré
Meuno bawo yeugo tino té do lathié
Pousso passo té bo sanione nieupeuy tardé
Sa wakh dafa bari téweu diekh ni wiri wifi Fokni ya kham
Leep wakhniou lo bokak Siri Deuké garoualé diapé nieup woudiouu
Nieup sori laléla banta bou goudou
Sa dieuf diou niaw beuss dina nieuw ding ko réthiou
Khamnga Thiow lé bari wayé deugueuy moudiou
Moytoul sa noon dieul sa verre def cin cin
Adouna lepp teranga la téyél sa lamigne
Wola nga record
Message nga capturer
Vocal nga transférer
Statut nga vu yakamti partager
Dama pataa sa yoon nékouthi
Sama Sewaay sa yoon nékouthi
Sama niawaay sa yoon nékouthi
Deug deug sa yoon nekouthi
Dama Stylé sa yoon nékouthi
Sama Modé sa yoon nékouthi
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey louthiy sa yoon
Seuytané Louthiy sa yoon
Rambathie louthiy sa yoon
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey Lu ci sa yoon

Поcмотреть все песни артиста

Other albums by the artist

Similar artists