Karabalik in the track Hey Koulou kin-kin Karabalik nèna silolèn nè Si lolèn nè (enh) Si lolèn nè Koulou kinkin kinkin Si lolén nè Hum hum hum ah ah Si lolèn nè yèna ngi si diam Si lolèn nè yèna ngi si diam Si lolèn nè mba diameu ngèn am (Hey) Si lolén nè hey mba régue ngén Si lolèn nè Parce que magui si diameu si lolèn nè Ngèn di rap ni kouy dakadji sathi fils dolèn yam Do sampeu sa tankeu si banque sinon loy lék Gno lèkeu xalisou rap sa rappeur bi xoss na swing gomme lay yeuye Gnaw ga sa dome bi guignol lay nèk Sananetè xèrr bi si gnom lay yam Saganetè nday bi si lay Gnom rèk Mba règue ngèn Yèna ngi course mba yégg ngèn Dam lén di couche mba dayou ngén Rap bi douma ko bayék yén Doumako bayé ak ay mindeu néw Djieukeu deih di beugueu tagué dip Deuthi bou wètt ni deih thi pandémie Dingu ko képeu teuthi sa gatt tè ganè mik Da ngén tèki mais dou fègne si kanami (hey) Fatal ma fèpeu gnou Yolé lèn Xadial ma fèthii fi yolèlè sèn xolay mètti Si lolèn si lolèn Si lane ngèn nè mane dè magui sama olala Comment tu vas waxma yaw si lane nga nè Gnoune dè gnogui sougnou olala Yén nak Si lolèn nè Si lolèn nè (enh) Si lolèn nè Koulou kinkin kinkin Si lolén nè Hum hum hum ah ah Si lolèn nè yèna ngi si diam Si lolèn nè yèna ngi si diam Si lolèn nè mba diameu ngèn am (Hey) si lolèn nè Koulou kinkin Nèko reuleu mou deuleu na andak tiol tèy deunou Si lolèn nè Falalèn fèk mane dingèn ma gueuneu diox gueudeu Thi simili mane lalèn may mak bouma si feugeu mou keupou Keupeu keupeul douma tèrè fateu tourou vautour Manila mbaye fatal Hey Dèf kom bang di tiapeu sa pipette Yènèn gars yiye copier nèlèn gnou rang Tè dagati ticket xolal kara beuseul ma lolu Rèwandè bi la beugueu wanè Xalè la cachet concert yigne mag fay lay dieundè gouté asey (hum) Kholal Boudè rèwandè pair rou daleu la Talibè rèkay yarou Sa bro biy yègal mbagueu gnodi DG tè Gnoune gneup xamnagne ni yoroul Khathi yifi nèk gnègnègnè fèn rek Mbeuw mbeuw Scooby Doo Dolèn sax ay mbeurou galè Ay mbeurou douche ngèn Xamnagn ni kousi djiouk poup (kousi djiouk poup) Hum ah ah ah ah ah ahh Si lane ngèn nè mane dè magui sama olala Comment tu vas waxma yaw si lane nga nè Gnoune dè gnogui sougnou olala Yén nak Si lolèn nè Si lolèn nè (enh) Si lolèn nè Koulou kinkin kinkin Si lolén nè Hum hum hum ah ah Si lolèn nè yèna ngi si diam Si lolèn nè yèna ngi si diam Si lolèn nè mba diameu ngèn am (Si lolèn nè) Ba rëgg ngen (Si lolèn nè)