Kishore Kumar Hits

Karabalik Beatz - Fou Lerr Lako Tekk lyrics

Artist: Karabalik Beatz

album: Fou Lerr Lako Tekk


Karabalik yah yah
Rep'Tyle Music in this beat Noon nga haha haha
Continuel wakh niuy liguey
Nioune fimou toleu ni stress dotouniou Ray (pour lane)
Niongui sant yalla santé ko souniou ndeye
Liguey rek mo worr wanté diarouniou
Diay man lim lay wakh ni Fou Lerr Lako Tekk
Hey wah ehh Fou Lerr Lako Tekk
Boy lim lay wakh ni Fou Lerr Lako Tekk
Eh eh eh Fou Lerr Lako Tekk
Man lim lay wakh ni (ehh)
Ray la di fethie fethiou ive Niang
Kharagne Lô la birr Snapchat
Gueumowone Dina takeu, tay guel yi ngay guent may Flam
Nel sira n'a dougueul vook tik tik
From diek man la rappeur bou sett wethie
Deff song sa wa gallé tik tok
Nelene diakhal bi nalene ko Tiak Tiak
Meuno gueum loy deugué dou diameu li dou rap kassé
Rep'Tyle kassé enhh Dangey lathiem dett nioune rek xi xalé
Ba sa birr gallé di Boutourngalé niggah lossi meune
Gang, dass ko sa mine fi niofi nek
Lo niemé niakeu ragalounie yolé
Doundak dead nioy andeu Valar Morghoulus
Nio Tim ndy game bi niggah xana guisso 2bis
Si birr rek lay danou do guisse sama échec Gang
Rep'Tyle,
Comme keur bou joie
Dounie yewu ba thiolé né paff Fou Lerr Laniekoy Tekk
Seytané nga done weur guiss Ibliss perte repéré
Dieul game deff ko guel sen rappeur Yi di misère
Ay Fake ngene Wouh ahh
Yaroul niggah
Régime anarchique nga nekeu amoul vote
Investiro sa khel bi wait for the dead
Eneul meussi motherfucking busty niggah
Wah ioe ehh
Loy Wouh ah (Wouh ah wouh ah) Loy Wouh ah
Wouh ah (Wouh ah wouh ah)
Ioe eh loy Wouh ah (Wouh ah wouh ah)
Wouh ah (Wouh ah)
Noon nga hahaha, continuel wakh niouy liguey
Nioune finou toleu ni stress dotouniou Ray (pour lane)
Niongui sant yalla santé ko souniou ndeye
Liguey reka worr wanté diarouniou diay
Man lim lay wakh ni Fou Lerr Lako Tekk
Eh wah eh Fou Lerr Lako Tekk
Boy lim lay wakh ni Fou Lerr Lako Tekk
Eh eh eh Fou Lerr Lako Tekk
Eh lim lay wakh ni
(Drizzy dream)
Adiana souff kouma fa dagueu nangue ma ni Massa (eh yangue may ganie)
Eh padiali rappeur la wara teureul pakeu yi dass (ay)
Nongali yombali niouss
Reglel ioe nga dii ouss banie dogali bour Niou dogali soul
Do diay album somebody soul (ay)
Bokouniou yone nakhté gorr djiguene foum diar keneu waroufa aw
Sa carrière pente nga daw boy mangui sa kaw boy namouma kaw
Ponkalou niaye si gueunou beuy
Godass wenie si deunou Fake
Ma khew ki peunou Tess
Teko fou Lerr guisseul niou Dara
Meussoul diouk sakh bay danou
Game bi touche pas c'est à nous
Karabalik ngoune tadj thiakha guoune
Togual fou deugeur té khar niou (bay)
Sa khapeu Tati meunoul teudiou
Label boumla diokhé ngako fok mangui diapeu dadj nikou teuthiou
Wait, wait bi ioe niggah yo
Fou Lerr Lako Tekk
Niom meussounie deff Lou nekh
Nioune,
Sa boniou deglo boy sa khol day gueuneu fekh
Né khorom sibirr thiine bi kani si sa beut yi
Daniou beuri dolé motakh fo niou sentou fidi
Bounie né yaffi meune Soula nekhé Bakou
Rep'Tyle si digueu guew sa papa sakh day tahiou
Fou Lerr, Fou Lerr
Nioy contane lo sa mère
Danga khewi ni nderr
Konn faw nga sandi kherr
Loy Wouh ah (Wouh ah wouh ah)
Loy Wouh ah (Wouh ah wouh ah)
Ioe eh, loy Wouh ah (Wouh ah wouh ah)
Wouh ah wouh ah
Woow, Fou Lerr
Amaguouma chance té khoti na license bi
Thiakhane nanie ba fessal salle bi
Comme niniou deff di job si seniy Avis
Sa carrière comme louniou diam xi datif
Thiapeu si dadji Khalil Mame bou gueune bi
Prince de la ville danio wett si trône bi
Seddo khaliss ngene di seddo note yi
Batay colo colo pour tek seni zomi
Ding Dong, Karabalik kala
Lingom banga saff sapp
Souki guinar souki rappeur saff saff
Boul ma thiatou niggah laff thiate
Foma guiss takhaw commando
Khaliss ni boomerang noulene nieuw
Chaque jour sen message guéneu sama call
May gueuneu beuri paw dilene Ghost
Eh fou Lerr Lako Tekk (Fou Lerr)
Sanie na woo monsieur le commissaire diay ko prek
Allô, Allô bizarrement lgui souma wouyo daniouy begg (enh)
Le jeune homme star la en fête (en fête)
Yaniou meune foko tek
Decapitel sa bopou nekeu en tête Marouane
Dem lene lathie bo beugué kham louy khewi
Gang bi wagni New yi Gang bi dieul sen tanki diegg yi
Kham fouy meti diko Wouh ah
Wokak diassi c'est oui
Khadj bou dead bi bofi soobo guedjou diassite ngay guiss
Wathié nadjeu ngani lerroul diaroul lathie fouy Rep'Tyle
Kayniou dieul la bo dé Kylie Jenner, Katty Perry
Pa bi diapi, deuss bi né day daabi Péé bi
Rap lay deff wala may selbé setal saltigué yi
Eyy, ey Fou Lerr Lako Tekk
Nioro lene niou lene di thiop ni ay Mango vert
Té bomay thiop di Corona
Man may paingolé
Ngay royy wizkid, Davido
Man may royy père Dangoté
Noon nga hahaha
Continuel wakh niouy liguey
Nioune finou toleu ni stress dotouniou Ray (pour lane)
Niongui sant yalla santé ko souniou ndeye
Liguey reka worr wanté diarouniou diay
Man lim lay wakh ni Fou Lerr Lako Tekk
Ay wah eh Fou Lerr Lako Tekk
Boy lim lay wakh ni Fou Lerr Lako Tekk
Ay ay ay Fou Lerr Lako Tekk
Man lim lay wakh ni
Rep'Tyle Music

Поcмотреть все песни артиста

Other albums by the artist

Similar artists