Kishore Kumar Hits

Oothentik Zeus - Djikk lyrics

Artist: Oothentik Zeus

album: Thiapathioly


Deff Music
Hey Zeus
Yaay neenama liguéyeul nek doomou diw dou sétal sa der (Chabadabadibidada)
Il a suffit ma rakhoussou pour niou sipné maalen dakh saleteel (Chibidabadibidada)
Laal nga laalaké boybi khalou ndeef leu baakhoul nimouy lakké (Chabadabadibidada)
L'argent laay lakk mom nga amoul mootakh xamoo fimay wakhé
Même boumay wakhoon wakhett boy dou takh ma Wade man
Daa diott ma run away
Business comme Kanye West
May tidji compte banque
Ngay tidji compte fake
Di lep si séni bess
Mooy sama quotidien
Fii doo arrière dag chèque rap bi dou combat Lac de Guiers
Ndanaan laay doon ba dee un peu comme Johnny Haliday
Meun nguénmeu saani kheer ba mère bi adji saani kheer
Beuri ay guels you khess
Si sama liste noire
Amna niou beug ma wathie normal nakh ma ligueey
Ma hustle everyday
Teudi bi nieup di khey
Niaanouma thioowli dieex nakh maay nokhé jet li man
Parfum woo kaani kheegn
Indilma trône bi man
C'est pas si compliqué
Sam taat yi laassiy tek
(Hey) Mousslou si thiatt
(Hey) Mousslou si beut
(Ay) Ak si laamegn
(Hey) Lep dina baakh
(Ay) Mousslou si thiatt
(Hey) Mousslou si beut
(Ay) Ak si laamegn
(Hey) Lep dina baakh
Hey
Beut yiy tégou thi mane yeup yalnama djikk (laaf Thiat)
Lamegn yiy wakh thi mane yeup yalnama djikk (laaf Thiat)
Succès bima nara am yalnama djikk (laaf Thiat)
Yalnama djikk (Thiat)
Yalnama djikk (laaf Thiat)
Beut yiy tégou thi mane yeup yalnama djikk (laaf Thiat)
Lamegn yiy wakh thi mane yeup yalnama djikk (laaf Thiat)
Succès bima nara am yalnama djikk (laaf Thiat)
Yalnama djikk (Thiat)
Yalnama djikk Bass Thioung
(Ay) Mousslou si thiatt
(Hey) Mousslou si beut
(Ay) Ak si laamegn
(Hey) Lep dina baakh
(Ay) Mousslou si thiatt
(Hey) Mousslou si beut
(Ay) Ak si laamegn
(Hey) Lep dina baakh
Maa shaa allah
Kaaro yallah lawla thiat soubanama hey
Thiatt seekhlouma dandouma nangma sorri hey
Yaay niaanalma kone awma loumay ragal
Baye neenama dom demoul teh boul worry
Liguendi job (Ay)
Mooy sama foo (hun)
T'en a ras le bol (ay)
Sa gars yi boy nieup laa lingom
Pathial sa goe (ay)
Ni Davido (hun)
Amoo niveau (ay)
Chimbarigoo khambarigoo
Hey Xamooma boy xamoo hip-hop
Sam meuné rap fété neu bord
Savant bou makk Cheikh anta Diop
Yaay sama boss damla tingoob
Mayla ay coup sa batt dou diog
May todj sa beut nganaan guissoo
Lambi golo kou diouk ma nokk
Boudé YORO dougn Lambissoo
Fuck relève bi romb naako depuis lors
Lyriciste dakhoo bind Diary Sow
Sa moral gueneu dam beugnou Sidy Diop
Nakh yakh courant rk nga nekké studio
Maa shaa allah
Kaaro yallah lawla thiat soubanama hey
Thiatt seekhlouma dandouma nangma sorri hey
Yaay niaanalma kone awma loumay ragal
Baye neenama dom demoul teh boul worry
Beut... Beut yiy tégou thi mane yeup yalnama djikk (laaf Thiat)
Lamegn yiy wakh thi mane yeup yalnama djikk (laaf Thiat)
Succès bima nara am yalnama djikk (laaf Thiat)
Yalnama djikk (Thiat)
Yalnama djikk (laaf Thiat)
Beut yiy tégou thi mane yeup yalnama djikk (laaf Thiat)
Lamegn yiy wakh thi mane yeup yalnama djikk (laaf Thiat)
Succès bima nara am yalnama djikk (laaf Thiat)
Yalnama djikk (Thiat)
Yalnama djikk Bass Thioung
(Ay) Mousslou si thiatt
(Hey) Mousslou si beut
(Ay) Ak si laamegn
(Hey) Lep dina baakh
(Ay) Mousslou si thiatt
(Hey) Mousslou si beut
(Ay) Ak si laamegn
(Hey) Lep dina baakh

Поcмотреть все песни артиста

Other albums by the artist

Similar artists