Hey
Zeus
Bril
Oh la la
Hé Hé
Let's Go
Hey Hey
Fii ngako degué (ngani)
Fii lagnko wakhé (hum)
Fii ngako guissé (waw)
Fii lagnko deffé (tchi gui tchi gui)
Fii ngako degué (ngani)
Fii lagnko wakhé (hum)
Fii ngako guissé (waw)
Fii lagnko deffé
Mané boy
Boy bouma yakhal (ohlala)
Maaguissi sama (ohlala)
Lii maako waral (ohlala)
Namouma dara (ohlala)
Boy bouma yakhal (ohlala)
Maaguissi sama (ohlala)
Lii maako waral (ohlala)
Namouma dara (ohlala) (aïe aïe aïe)
(Oh Lala)
Boulma yakkal sama oh lala hey (ohlala)
Eh boulma yakkal sama oh lala
Gaïndé bou dégoul diatt
Néleen ma thiourki thiam, maaguek wakhou bou gueulem
Diokh sama bop diam takh sama khel di nathi, bamay maayé dji déreet
Boy bima rap di fay, chaine biné sama baat boobu fégnouma télé
Xallé bou melni mane niaanalma goudou fane, doossi guissati benen
Deff kat bou makk moodoul def louko waroul
Bideewou beuthieuk si goudi loup garou
Dougueul si mane xamné talent dou tandouss
Alakhiraa noofay démé di kharou
Sécurité doundé sa art
Boybi daa mag ni 18 safar
Kounta kinté zulu shaka
Yeuf yi bou diougué rk c'est la cata
Dougouma chaloupe mais maagui Gorée
Meun ngama adiou mais tu me connais
Bou CD bi diaroul danguéna doffé
Zeus doula tafou booy copier collé
Boumala taloul nane ngamay fayé
Oothentik fowoul dalendi fowé
Mouvement bi démoul doolenfi sorré
Loolou mooy wakhou kou daanou si charette
Fii ngako degué (ngani)
Fii lagnko wakhé (hum)
Fii ngako guissé (waw)
Fii lagnko deffé (tchi gui tchi gui)
Fii ngako degué (ngani)
Fii lagnko wakhé (hum)
Fii ngako guissé (waw)
Fii lagnko deffé
Mané boy
Boy bouma yakhal (ohlala)
Maaguissi sama (ohlala)
Lii maako waral (ohlala)
Namouma dara (ohlala)
Boy bouma yakhal (ohlala)
Maaguissi sama (ohlala)
Lii maako waral (ohlala)
Namouma dara (ohlala)
(Oh Lala)
Boulma yakkal sama oh lala hey (oh la la)
Eh boulma yakkal sama oh lala
Mangui thi sa Sama bopp, sorima mangui thi lénén, def ni sa Ex
Tok thi sa diggou bopp ba nieupp di fokni may accent circonflexe
Yaggueu ni Assamane, def ay Hit la mii douma tégguéti Tank!
Règlement de compte, boma thi déggué da fékkeu ni mangui thi Bank
Défouma Judoka Té mangui prise
Nguéni weuri daanou, ma weuri djizz
Bo takkone sa beutt yi sakh dingama guiss
Sagama sa Guel bi yonéma biz (ouh)
Dama khéw ba légui mangui wadja tidji cosmétiques ndakh beuri Tubes
Khalé Thiaroye 44 fok mou bomb Niata millions ngéni guiss biir YouTube!
Meune lépp motakh kén douma yapp, rare ni car rapide bou amoul apprenti!
Yéék thi kaw beat bi di partouze, meussouma bayi dõré mane la Alkati!
Séni Guel dima khol, All eyes on me, melni Pac mo déloussiwatt!
Risquél doublé thi virage wala Bril ak Zeuss Nioussla, Mou siwattt!
Fii ngako degué (ngani)
Fii lagnko wakhé (hum)
Fii ngako guissé (waw)
Fii lagnko deffé (tchi gui tchi gui)
Fii ngako degué (ngani)
Fii lagnko wakhé (hum)
Fii ngako guissé (waw)
Fii lagnko deffé
Mané boy
Boy bouma yakhal (ohlala)
Maaguissi sama (ohlala)
Lii maako waral (ohlala)
Namouma dara (ohlala)
Boy bouma yakhal (ohlala)
Maaguissi sama (ohlala)
Lii maako waral (ohlala)
Namouma dara (ohlala)
(Oh Lala)
Boulma yakkal sama oh lala hey (oh la la)
Eh boulma yakkal sama oh lala
Поcмотреть все песни артиста
Other albums by the artist