Kishore Kumar Hits

Oothentik Zeus - Exam Act 2 Cas lyrics

Artist: Oothentik Zeus

album: Exam Act 2 Cas


Check
Boul raagal dëgueu yor djikoy semel
Keneu meunoul werou tchi sa takander
Teylé sa life tchi ay buzzou semaine
Na diour khalate bo dé teudeu'k sa xel
No mel sa guel dona goul sa diabar
Tonto sa diabar donatoul sa guel
Da am niou diouk am niou teudi fadiar
Wakho lou gueun nelaw meuno ma yé
Rewandé yeré si armoire la rek
Sokhor done febar bo amoul remede
Barké dou dieumeu si boum neka fegne
Gayn moy deumeu boul siramtou lekka
Kou sorri tchi yow rek sa xol la diegué
Xam xam mo précédé ABCD
Am savoir vivre dou empêcher deh
Faudra pas te laisser faire par gni ame laisser faire (lourd)
Marathon depense la pa yi di competir
Si xew la meres yi di investir
Tenue bou Orange di gnodi Free
Wotel lou am solo dougnou la mey credit
Meunou gnou demal sunu boppa ba legui
Ndakh kou nekka kenene ley lidianti
Gnigne fi tek lidianti sene boppa rekka
Gnoune Yalla rek mo gnou meune lidianti
Dagn gneme cas (degne gneme cas)
Xeuy di weur cas (xeuy di ko weur)
Done avocat (hé)
Té gnoune rek doy naniou cas (gnoune rekka doyna niou)
Dagn gneme cas (degne gneme cas)
Xeuy di weur cas (xeuy di ko weur)
Pour done avocat (hé)
Té gnoune rek doy naniou cas (one two three)
Dagn gneme cas (heeeeeeehee)
Xeuy di weur cas (haaaaahaa)
Pour done avocat (haaaaaha)
Té gnoune rek doy naniou cas (hé)
Gnoune rek doy naniou cas (one two three)
Xam xam tchi leep
Débat bou gneuw grains de sel di nga si sanni
Ya niakka xorom
Comme leer tchi leer
Wakh deugueu foko warroul wakheé
Meune na té deugueu dji fegne
Lou gneup di wakh nigga nenegne moy deugueu
Mais bo seté wakh dji si keneu ley ndieukeu
Alla bouy sakh naaka keneu douko degueu
Mais garap bouy danou mom gneupeu key yeuk
Le silence est d'or
Anou sa bamelou biir (man)
Bac+ tchi werenté
Tu as fait les bancs (frère)
Amna ay goor you yor langue de pute (ouais)
Nio bokka heure
Mais daniou eupeunté temps (rek)
Beugueu la soul takh gnou soulil la tiow
Dekh bou nekka amna dieussit'am
Na caravane circuler
Xatch yi di mbow
Dieuw di lekka
Weur di tammé deum
Bou gni di kal
Gnenen gni gnou ngui werenté
Bou gni di xass
Gnenene gni niou gui feneunté
Gni waté diamma
Si souf laniouy xekheunté
Ligueye khep dolli
Mais gnoune daniouy xebanté
Dagn gneme cas (degne gneme cas)
Xeuy di weur cas (xeuy di ko weur)
Done avocat (hé)
Té gnoune rek doy naniou cas (gnoune rekka doyna niou)
Dagn gneme cas (degne gneme cas)
Xeuy di weur cas (xeuy di ko weur)
Pour done avocat (hé)
Té gnoune rek doy naniou cas (one two three)
Dagn gneme cas (heeeeeeehee)
Xeuy di weur cas (haaaaahaa)
Pour done avocat (haaaaaha)
Té gnoune rek doy naniou cas (hé)
Gnoune rek doy naniou cas (one two three)
Dagn gneme cas

Поcмотреть все песни артиста

Other albums by the artist

Similar artists