Système bi lumu bëgg lañu bagn, té lumu bagn lañu bëgg Ñu joox len mbaranu kiray kenn bëgg ci mur suñu gëtt Peuple bu méér tekk ci xiif ak maar taff xol yi xed Privilége ñii baax tax ñenen ñi ñëkk liraam si ñax bi la jëm Le peuple a mal sen démocratie lañu tet Politique - Corona mo suñu fébaar couvre feu, confiné ñëpp Ñi ñol duñu gatt ci justice té waral tribunal bi ni mbatt Avocat yi dañu léen tagg sans mettre xaad Takk der yi ay liff katt ku wax ñu jàp xët tët Ñana booy lañu fi ray rewmi taar amul xey Ñata mbamel biir get, ñata mort ci corona Pauvreté ñun fur ray yëpp ni déé ci corona Maandé titt na girr suñu doom (bilaye wallaye) Elëk gu Senegaal bi lumu nara doon (ngur jarul li) Wallahi bul xamon li neen ci gën (ñepp diaxlé nagn) Kenn du ja marr loo benn takk derr Politicien bumu taax nga njaay sa baakan amul jëgëm Ko ci faal bu faalo fatté la, bopp lëgëm Ñata élection taxul ñu am gouvernemet Lepp ñun la dañu ye gaawa faan faal président Jot naa nakk ñu xam suñu bopp Baayi xiro bëgg ngan yoo mell ni duñu ay mbokku Ni di saaga si net bi ku nekk dinane fii la bokku Ñi di waan teer carte électeur luy ndaay lolu Sacrifier saaw askan tokk Amon xam-xam bëgo jàngi, bëgg tékk joni joni Saaw ci mbedd, loo jot saañ, bëgg mu sétt léegi léegi Def sa jaxum ñan intervention bagn corruption Bu ñu waxé ngani Senegaal lilë lolu du solution Askan be faal ñu léen di faay Soo léen tallé rewmi di gën ñu faay Dañu waara bollo doon mbéne saay jow li faay gis nañu rap Peuple bi di def nakasudul nonu Bëgg ñu diaxasé takk derr yi Gir ñu doon suñu non, jaam wesul ci mbiim rew Maandé titt na girr suñu doom (bilaye wallaye) Elëk gu Senegaal bi lumu nara doon (ngur jarul li) Wallahi bul xamon li neen ci gën (ñepp diaxlé nagn) Kenn du ja marr loo benn takk derr