Kishore Kumar Hits

Momo Dieng - Li ngama diaral lyrics

Artist: Momo Dieng

album: Li ngama diaral


Lebone guani lippone ben xalei boumafi nobone mou diaralma dokh goudiii léép louma am diayko crédiit néké so beugué yaw so beugué daguay misère (2bis)
Ohhhhh wawaw!!!
Waw meunouma do misère
Yaw daguay misééééreee
Waw meunouma do miséére
Yaw daguay misééreeee
Everything magui si téléphone bi
Gayiii nénagn dagn ma méréé
Takhna nieup bayima
Paco néna khamé touma
Waya lougn meuna wax yeupeu
Sama mbeuguel mane la thie khol
Daniou wara xamni manou mako diaye nekh mane damako beugeuh
Waw fokma nangou misère
Damako beugeuh
Waw meunouma do misère
Mane dama beugeuh
Mbeuguel sakh boula diéguéwé
Bo moytou woul dagu koy fowé
Lepp loy sagané dal
Kénéna gua tok mou diaral ko louné
Mane fokk ma soré nakh
Nakh gua meuna kham sama mbeuguel
Bilay fokma ndangou misééére
Mane damay misère
Bilay fokma ndangou misééére
Mane damay misère
Alale kouko sagané
Kou ko farlo koy moudjé
Doudek beuthieuk malay wo
Yaw dé wouyou wo ma
Wouyouwooma faalé wooma
Yaw dé wouyou womay
Faléwo ma mane deh top na leuy
Wayé yeugoulo meuy

Поcмотреть все песни артиста

Other albums by the artist

Similar artists