Kishore Kumar Hits

Obree Daman - Bakkan lyrics

Artist: Obree Daman

album: Bantu Bale


Bul di jaawale
Bul di jaawale
Bul di jaawale
Bul di jaawale
Mandu
Mandu len
Ci nitt
Bul di jaawale
Mandu
Mandu len
Ci nitt
Bul di jaawale
Dox naa ba ñëw setsi la
He ñëw setsi la

Nitt de war na mandu
Teey te Yalla tax
Hé Hé
Seet naa la sow
Seet naa la penku
Mandu reer ci jamano
Seet naa la sow
Seet naa la penku
Mandu reer ci say jikko
Mandu
Mandu len
Ci nitt
Bul di jaawale
Mandu
Mandu len
Ci nitt
Bul di jaawale
Bul di jaawale
Bul di jaawale
Bul di jaawale
Mandu
Mandu
Mën na laa wallu
Mandu
Di na Mandu
Ci doomu àdama bi le

Seet naa la sow
Seet naa la penku
Mandu reer ci jamano
Seet naa la sow
Seet naa la penku
Mandu reer ci say jikko
Mandu
Mandu len
Ci nitt
Bul di jaawale
Mandu
Mandu len
Ci nitt
Bul di jaawale
Bul di jaawale
Bul di jaawale
Bul di jaawale
Mandu
Mandu len
Ci nitt
Bul di jaawale
Mandu
Mandu len
Ci nitt
Bul di jaawale
Bul di jaawale

Поcмотреть все песни артиста

Other albums by the artist

Similar artists