Yagg nala gëm, yagg na Dalal sama xel ci yaw Lo wakh mani lolou laa Meussou ma xel gnar ci yaw Defla sama lepp wolou laa Ni douma tekk béneu nitt ci sa kaaw Beugone na mou bagna nekk deugg waay Wala moudone kénéne koudoul yaw Foma meussa tagg ma bayila (Fou gnouy ré ma defeul la) So wakhone ni doyoul, mann ma doli laa (Lo meussa sokhla ma défal la!) Kaay wakh ma lo meuné li yaw Di foo ci sama guinaw Sekk akk lénéne kénéne koudoul mann Xamna lepp guiss na lepp Mala bayi ci biir Xamna lepp guiss na lepp Mala bayi ci biir Xamna lepp guiss na lepp Mala bayi ci biir Xamna lepp yeug na lepp Mala ba ci biir Wakh ma lo meuné li yaw di foo ci sama guinaw Sekk akk lénéne kénéne koudoul mann Xamna lepp guiss na lepp Mala bayi ci biir Xamna lepp yeug na lepp Mala ba ci biir Xamna lepp wayé sama xel nangou woul ni yaw leu Dou lougnou ma nétali louma guiss la Xawma loy wakh bama gëm leu Kaay wakh ma lo meuné li yaw Akk fimala tégone ba nane kou melni yaw amoul féneeu Tontou ma lo meuné li yaw di foo ci sama guinaw Dem fénéne ci gnénéne dima féne Yaw am nga lepp ci sa keur dara manquer woula fi Même so xolatoul ci mann roussal xalé yi Nékatouma ci sa keur gnane ma batt té djougué fi Mo gën malay dji loubakh ngamay fayé li Kaay wakhma lo meuné li yaw Di foo ci sama guinaw Sékkeu akk lénéne kénéne koudoul mann Xamna lepp guiss na lepp Mala bayi ci biir Xamna lepp yeug na lepp Mala ba ci biir Wakh ma lo meuné li yaw di foo ci sama guinaw Sekk akk lénéne kénéne koudoul mann Xamna lepp guiss na lepp Mala bayi ci biir Xamna lepp yeug na lepp Mala ba ci biir Xamna ci linga né... Lingamay fékhél Xamna li nekkeu ci sa xel (Meussou ma wone fokni dingama def lou melnii) Xamna ci linga né... Lingamay fékhél Xamna li nekkeu ci sa xel Xamna lepp guiss na lepp Mala bayi ci biir Xamna lepp yeug na lepp Mala ba ci biir Kaay wakhma lo meuné li yaw Di foo ci sama guinaw Sékkeu akk lénéne kénéne koudoul mann Tontou ma lo meuné li yaw di foo xi sama guinaw Dem fénéne ci gnénéne dima fénn Xamna lepp guiss na lepp Mala bayi ci biir Xamna lepp yeug na lepp Mala ba ci biir